Bb yaw ba nam nga ma Man dama la nam ba nam nimala namé eh eh yeah Té yaw bb tam nga nak Dieul peage bi raw ma mai nak tay ma feul pé eh Bb yaw ba aimer nga ma
Man damala aimer ba aimer ni mala aimer eh eh Tè Yaw bb diaral ngama Dohé ak ay dal wegn thi desert bi bamou dieh ehh
Def ma ndank yama meun thi pét ma nangouwat ko Thi diam Lay doh Wahone nalako thi souba faw ma bamtouwat ko Damala Love

Baby Dama la Yaw Dama la love Té Andou mathièk sago Bb Dama la
Yeah yaw dama la love Mala topé dina dof baby Baby Dama la Yaw Dama la love Té Andou mathièk sago Bb Dama la Yeah yaw dama la love Mala topé dina dof baby