Accueil  đŸ’ƒđŸŽ€ Paroles de chanson Française et Internationnales

 A   B   C   D   E   F   G   H   I   J   K   L   M   N   O   P   Q   R   S   T   U   V   W   X   Y   Z   0   1   2   3   4   5   6   7   8   9 
Artiste : Amsco Gucci
Titre : Roses
Oohh ma chérie xamo ci dara sakh mo ko mome
Mon amour tu es lĂ  maintenant yÂŽa que des roses
Yakar naa ni ma ngi ley bëgg nopp yow laay xalaat

Guddi ak bëccëg tu es là maintenant yŽa que des roses

Dama bëgg nelaw ak yow tey dama bëgg añ ak yow sama kër
Sama mbëggël nop nga ma ba léegi foon naa la xam naa ne di
Nga dellusi je t’aime ma femme tu es là pour moi Et tu m®aimes
Aussi je suis lĂ  pour toi bul ma sonnal ndax yow la doon xar
Je sais que tu mÂŽa dit "Yay sama xol" depuis je tÂŽattend mais tu es

Belle on dirait que tu veux danser avec moi depuis je tÂŽattend mais
Tu es belle je tÂŽavait bein dit on dirait que tu veux danser avec moi
Là jŽsuis resté avec toi dans ma vie je sais que tu es comme ça
Mais bon jÂŽme suis dit si un jour oĂč tu ne me quitteras pas je sais
QuÂŽtu ne me prends pas la tĂȘte demandes Ă  ta mĂšre elle va te dire
MĂȘme si elle nous a acceptĂ© ou elle nous a dit oui on peut se Marier nopp naa la jÂŽespĂšre que tu ne me quitteras pas pour un Autre mec jÂŽespĂšre que tu ne me quitteras pas pour un autre mec

Oohh ma chérie xamo ci dara sakh mo ko mome
Mon amour tu es lĂ  maintenant yÂŽa que des roses
Yakar naa ni ma ngi ley bëgg nopp yow laay xalaat

Guddi ak bëccëg tu es là maintenant yŽa que des roses
Oohh ma chérie xamo ci dara sakh mo ko mome
Mon amour tu es lĂ  maintenant yÂŽa que des roses
Yakar naa ni ma ngi ley bëgg nopp yow laay xalaat
Guddi ak bëccëg tu es là maintenant yŽa que des roses

Waaw yow ya ngi si Kor gui walla ya ngi ci weer wi
Nuyóol ma sa waa kër yakar naa ni ma ngi ley bëgg nopp
Elle mÂŽavait bien dit "sama dieukeur dama la nopp ba dof"
Dinaa neex xam say xibaar tout nŽest pas rouge ma chérie
DÂŽamour tout est rose je te jure quÂŽon restera ensemble

Su ma tëddee da ma lay xalaat bëgg na am doom ak yow
Soo bëggee mën naa la woo yow laay xalaat guddi ak bëccëg
Na nga def nop nga ma ba léegi parce que je suis ton homme
On ne se prendra pas la tĂȘte et puis on ne se divorcera pas
Je sais que tu es ma femme depuis longtemps mais tu sais
Tu peux me dire la vérité et puis je vais te dire aussi comme si
De rien nÂŽy Ă©tait impossible alors que jÂŽai envie dÂŽĂȘtre ton amour