Moytoul me dieek diou romb rek Diekk taarou ngané dee dou yomb Wala djiguene diou lamb Ngané no def ding ko lamb
Judge not khel matoul boul wereunté tchi lou se yone nekoul Dieuw ak fok ne am ne diam mo tané yenn yi kou gueum dou ko def nekkoul
(x2) Yenn saye dinga tite be se khel nara diakhasso Yenn saye dinga fire be se khole nara diégué seuss
Yenn saay dinga tite ba sa khel bara diakhasso oh oh Wayé bepp fitneu toudd Yalla nga tchi wara ndieukk diemeu rakhasso oh oh
Borom bi dey missal Binde ne lepp be noppi Segueum gni kham nioye teye Kou niakk kham wara gueuneu noppi
Kou wekk lepp tchi guissané bo Dtouwoul adina dinele sappi Bouleu khiif takha salite My brother Yalla bouniou niakk soppi
Li khew tchi mim rééw Gueunoul yémé bitim rééw Mystique tchi biir guééw
Wayé Loukhouss dou firim rééw
Se deunkeundo boul kheep ndieurigneum Tagg sey kilifeu dingate Serigneum Téyé se kourouss gaddou se satala Deukk tchi dieuw yakkh der yeufou satt leu
Judge not khel matoul boul wereunté tchi lou se yone nekoul Dieuw ak fok ne am ne diam mo tané yenn yi kou gueum dou ko def nekkoul
(x2) Yenn saye dinga tite be se khel nara diakhasso Yenn saye dinga fire be se khole nara diégué seuss Yenn saay dinga tite ba sa khel bara diakhasso oh oh
Wayé bepp fitneu toudd Yalla nga tchi wara ndieukk diemeu rakhasso oh oh
Yenn saye dingueu guiss louleu dieulé kow lolou beu diapp se bopp kessé ngay meun Fekk ngueneleu laakhou tchi guinaw bobou fitna ndakh Yalla rekkeu kham ak di def li gueune
Yenn saye dingueu guiss louleu dieulé kow lolou beu diapp se bopp kessé ngay meun Fekk ngueneleu laakhou tchi guinaw bobou fitna ndakh Yalla rekkeu kham ak di def li gueune
Lo fi def dinegn wakh Lo defoulit dinegn wakh Yeek tchi mbame womate mbaam Ken dou tee dinegn wakh