Kenn warouma beugg Mane tchi sama bopp khawma louma beugg (Mane khawma louma beugg)
Ken warouma beugg bi niouy ndieukk dadié bobou wakhoumala deugg (Bobou wakhoumala deugg) Ken warouma diégué (ehh) Kou ma kham di nga thiéné fi nga thiéné (Di nga thiéné fi nga thiéné) Mane kenn warouma diégué So done kharit sama bopp laa lay ndieukk téré (sama bopp lalay ndieukk téré)
Mane saï saï laa, maa gueuneu yess Al Qaïda ah ah ah Saï saï laa motouma, moytouma eyy Khamal ne saï saï laa maa gueneu métti Al Kaïda ah ah ah Saï saï laa, moytouma, moytouma ey
Yow boumeu wakhlo, soma tidjilé se nopp naala doflo (dinga dof) Doumako tey soumay noplo So ma tidjilé se bopp di nga of-do (yeah) Damay dow somay wone love Ndakh beugoumeu koumeu beugg di meu toppato (eh) No ! Boul ess you´ll get no love Somay khaar onshore maa ngui oofshore ! ey
Boul meusseu gueum samay textos
Boul meusseu nangou niouy wéto Mane doumeu fey damay lep dow ! Ndakh damay play, #Nintendo Boul meusseu gueum samay texto Boul meusseu nangou niou wéto oh Doumala diokh li ngay weur boul ma wolou ndakh wakhouma loudoul ay léébone
Mane saï saï laa, maa gueuneu yess Al Qaïda ah ah ah Saï saï laa, motouma, moytouma ey Khamal ne saï saï laa maa gueneu metti Al Kaïda ah ah ah Saï saï laa, moytouma, moytouma ey
Rap verse: Neekh laamign, bad mind Khole bi degn tchi warone coller stop sign
Niaata laa fi digone dékhou banneekh ? Tchi guédiou rangogn dé legn moudié lap gayine !
Dama lédj dama dioubeudi Shawty naala tédj ci sey souvenirs Au début dangay bég fok ne doumeu nit Tey bo sanione doma fréq doma meusseu miin !
Yagg naa di wakh tchi gorr yi fowé kholou guél Tané wouma kone mounouma téyé rôlou frère Sciensal kepp kou tass yakaar tégou yonou jail Do deggeuti kenn néleu doundeul bo tchi toluwé...
(Do deeggueti ken, do deggueuti ken Do deggeuti ken né leu doundeul bo tchi tollouwé)